Cëri Yaram (Body Parts)
Nopp (Ear)
Bët (Eye)
Kanam (Face)
Bakan (Nose)
Tuñ (Lips)
Bëñ (Tooth)
Gémmiñ (Mouth)
Lãmmiñ (Tongue)
Baat (Neck)
Baaraam (Finger)
Barraamu Tànk (Toe)
Tànk (Foot)
Yeel (Legs)
Loxo (Arm)
Karaw (Hair)
Bopp (Head)
Sikim (Beard)
Mbàgg (Shoulder)
Dënn (Chest)
Biir/Coll (Stomach)
Ginnaaw/Taat (Buttocks)
Òom (Knee)
Conco (Elbow)
We (Nails)